Ree ak yëg-yëg
171 · Seet ci katalog Unicode emoji, bës benn yoon, te taf ko ci waxtaan, profil, post walla bataaxal.
- 😀 kanam guy gaññi
- 😃 kanam ak gémmiñ gu ubbeeku di muuñ
- 😄 kanam guy muuñ ak ubbeeku gémmiñ ak muuñ bët
- 😁 kanam guy gaññi ak bët yuy muuñ
- 😆 kanam guy muuñ ak ubbeeku gémmiñ ak buñ tëj bët
- 😅 kanam guy muuñ ak ubbeeku gémmiñ ak ñàqu tiitaange
- 🤣 ree ba xalangu ci suuf
- 😂 kanam gu am rangooñu bànneex
- 🙂 kanam gu muuñ tuuti
- 🙃 kanam gu dëppu
- 🫠 kanam buñu jaxase
- 😉 piis benn bët
- 😊 kanamu mbegte ak bët yuy muuñ
- 😇 kanam guy muuñ ak serkal ci kawam
- 🥰 kanam bu muuñ ak ay xol
- 😍 muuñ, kanam, xol, bët
- 🤩 dóor-biddeew
- 😘 kanam guy ëf fóon
- 😗 kanam guy fóon
- ☺️ kanam guy muuñ
- 😚 kanam guy fóon ak bët yu gëmm
- 😙 kanam guy fóon ak bëti muuñ
- 🥲 kanam buy muuñ ak ragal
- 😋 kanam, bànneexu, ñeex, ñam
- 😛 kanam bu ànd ak làmmiñ wuñ tàllal
- 😜 kanam ak tàllal làmmiñ ak bët buy piis
- 🤪 kanamu dof
- 😝 kanam ak tàllal làmmiñ ak buñ tëj bët
- 🤑 kanamu gémmiñu xaalis
- 🤗 kanamu kottante
- 🤭 kanam ak loxo bu dar gémmiñ
- 🫢 kanam bu am ay gët yu ubbeeku ak loxo ci gemmiñ
- 🫣 kanam gu am ay gët yuy gaawantu
- 🤫 kanamu shuut noppil
- 🤔 kanamu guy xalaat
- 🫡 kanam guy niyoo
- 🤐 kanam ak gémiñ guñ fermitiir
- 🤨 kanam ak buñ yëkkati yéen
- 😐 kanam gu ni tekk
- 😑 kanam gu melul nenn
- 😶 kanam gu amul gémmiñ
- 🫥 kanam buñu def ay tomb
- 😶🌫️ kanam ci niir yi
- 😏 kanam gu bëgg-waccu
- 😒 kanam gu ñàkk xorom
- 🙄 kanam guy regeju
- 😬 kanam guy def yëfi golo
- 😮💨 kanam guy nooyi
- 🤥 kanamu fenkat
- 🫨 kanam guy lox
- 🙂↔️ bopp buy yëngu ci anam gu tëdd
- 🙂↕️ yëngal sa bop ci anam gu taxaw
- 😌 kanam féex
- 😔 kanamu kuy xalaat
- 😪 kanam guy nelaw
- 🤤 kanam guy yuut
- 😴 kanam gu nelaw
- emoji Ree ak yëg-yëg 1FAE9
- 😷 kanam guñ bàndaas
- 🤒 kanam gu ànd ak termomeetar
- 🤕 kanam guñ laxas ak bàndaas
- 🤢 kanamu guy teey xel
- 🤮 kanam guy waccu
- 🤧 kanamu tissooli
- 🥵 kanam gu tang
- 🥶 kanam gu sédd
- 🥴 kanam gu xawa feebar
- 😵 kanam gu diis
- 😵💫 kanam gu am ay gêt yu rod
- 🤯 bopp buy toj
- 🤠 kanam gu sol mbaxane kaboy
- 🥳 kanam buy feetu
- 🥸 kanam gu deguisewu
- 😎 muuñ, kanam, nuwaarfime
- 🤓 kanamu bëñu lëk
- 🧐 kanam ak lunet-bennbët
- 😕 kanam gu jaaxasoo
- 🫤 kanam bi am gemmiñ bu jagonaal
- 😟 kanam gu jaaxle
- 🙁 kanam gu ànd ak yéen yu xawa lemu
- ☹️ aj-yéen kanam
- 😮 kanam ak gémiñ gu ubbeeku
- 😯 kanam guñ juutal
- 😲 kanam gu waaru
- 😳 kanam gu am tomb yu xonk
- emoji Ree ak yëg-yëg 1FAEA
- 🥺 kanam guy ñaan njegal
- 🥹 Kanam guy teye rongoñ
- 😦 kanam gu ànd ak yéen yu lemu ak gémmiñ gu ubbiku
- 😧 kanam gu xawa jaaxle
- 😨 kanam guy tiitaleete
- 😰 kanam ak ubbeeku gémmiñ ak ñàqu tiitaange
- 😥 kanamu mbetteel te féex
- 😢 kanam guy jooy
- 😭 kanam guy jooy ca kaw
- 😱 kanam guy jooy te tiit
- 😖 kanam gu jaawale
- 😣 kanam guy ñafe
- 😞 kanam gu am mbetteel
- 😓 kanam ak ñaq wu sedd
- 😩 kanamu coono
- 😫 kanam gu sonn
- 🥱 kanam guy obali
- 😤 kanam gu ànd ak saxaaru bakkan
- 😡 kanam guy puucatu
- 😠 kanam gu mer
- 🤬 kanam ak màndarga ci gémmiñ
- 😈 kanam gu am ay béjjen
- 👿 kanam gu mer am ay béjjen
- 💀 yaxu-bopp
- ☠️ kraan and yax yu kruwaase
- 💩 julu puup
- 🤡 kanamu kluun
- 👹 oogar
- 👺 kus-kondoroŋ
- 👻 fàntom
- 👽 aliyeen
- 👾 jiney aliyeen
- 🤖 kanamu roboo
- 😺 kanamu muus muy muuñ ak gémmiñ gu ubbeeku
- 😸 kanamu muus muy xiiru ak bët yuy muuñ
- 😹 kanamu muus bu ànd ak rangooñi mbégte
- 😻 kanamu muus buy muuñ ak bëti xol
- 😼 kanamu muus ak muuñ gu weng
- 😽 kanamu muus bu tëj bët di fóon
- 🙀 kanamu muus mu jommi
- 😿 kanam muus muy jooy
- 😾 kanamu muus mu mer
- 🙈 golo budul gis lu bon
- 🙉 golo budul dégg lu bon
- 🙊 golo budul wax lu bon
- 💌 bataaxalu mbëggeel
- 💘 xol ak fett
- 💝 xol buñ laxas ribaŋ
- 💖 xol bu yànj
- 💗 xol buy màgg
- 💓 xol buy tëf-tëfi
- 💞 xol buñ wëndeelu
- 💕 ñaari xol
- 💟 taaralukaayu xol
- ❣️ xol esklamaasiyoŋ bu fës
- 💔 xol bu tasaaroo
- ❤️🔥 xolu safara
- ❤️🩹 xol buy defar
- ❤️ xonk xol
- 🩷 Xol bu rose
- 🧡 xol bu oraas
- 💛 xol bu mboq
- 💚 xol bu wert
- 💙 xol bu baxa
- 🩵 xol bu bleu clair
- 💜 xol bu yolet
- 🤎 Xol bu sokolaa
- 🖤 xol bu ñuul
- 🩶 xol bu doomu-taal
- 🤍 Xol bu weex
- 💋 marku fóon
- 💯 tombi teeméer
- 💢 màndarga ku mer
- emoji Ree ak yëg-yëg 1FAEF
- 💥 mbëkkante
- 💫 miir
- 💦 toqu ñaq
- 💨 dem sa yoon
- 🕳️ pax
- 💬 rëddu bind kàddu
- 👁️🗨️ bët ci rëddu-bind-wax
- 🗨️ bulu bind waxu càmmoñ
- 🗯️ ndijoor mer bul
- 💭 rëddu bind xalaat
- 💤 emoji Ree ak yëg-yëg 1F4A4